audio
audioduration (s) 1.68
35.5
| transcription
stringlengths 23
537
|
---|---|
moo tax lépp lu ñuy def it dañ ciy jiital dëgg giak xam-xam bi lëkkaloo ko nag ak ñi nga xam ne ñoom lañ ko lëkkalool tas xibaar bi ba nga xam ne ñi kowar a jot ñëpp kilifa région bi ñu ngi koy jot macha allah |
|
léegi nag boo gisee suñ taxawaay du lenn boo gisee ñu ne jiw yi liñ def si boo xoolee rapport bi situation yëpp lay def bawul dara situation jiw situation engrais taxawaayu gàncax gi ba mu tàmbali ba fi mu toll nii ak li ma wax yëpp boo ko xoolee li ñu wax yëpp mu ngi ci rapport bii ma tiim |
|
nga xam ne daanaka démb lañ ko defar yónnee ko |
|
boo ko xoolee pour ñu daal di %e saaraan tuuti laal tuuti li nga xam ne %e boo xoolee %e tey jii ci wàll wi boo xoolee fi ñu toll ci wàllu liggéey bi nit ñi góob nañu dugub ñu ngi takk saabaar yi mooy botte yi |
|
soo demee saabaar yi boo gisee ñu xool dañ koy tas def ko ci ay clé weeraat ko ndax dugub bu wowut ni mu war a wowee kenn du ko bojj su wowut ni mu war a wowee kenn du ko def ci sàq |
|
gerte gi boo ko jëlee mu ne ah ma ne ko déqi nañ ko waaye bu ñu ko deqee gis nga dañ koy dajale def ko ay dajale yu ndaw moom la ñu tuddee andain |
|
gar bu ñu ko defee noonu loolu li ñu ci jublu mooy bàyyi ko naaj wi di ko laal |
|
bu ko naaj wi laalee am na fu tolluwaay fu muy toll ñu doog ko dajalewaat def ko naaf la cay topp mooy lan mooy bàcc la ca topp mooy lan def ci saag jaay maa ngi denci ji kër ga |
|
lijjanti ci ag jiwu ak nga def ci rënd baag la ca topp ak la ca topp ak asaka yaag ak la ca topp ak la ca topp kon ci foofu la ñu toll |
|
donc fi mu toll nii boo xoolee ci tool yi ngay gis dakasa yi ñoom ñoo fa nekk dakasa yi li tax mu am solo mooy %e séchage boobu ñuy def dafa am benn feebar bu ñuy wax saabu bu ma ko fàttewul mooy aflatoxine |
|
gëstu wane na ne gis nga li gën sax ci %e dakasa yooyu noonu |
|
léeg léeg da ngay gis béykat bi des fois dañ koy tourner dañ koy retourné retourné boobu lu am solo la gis nga boo ko retourné ba taat bi féete kaw ab njàngat gëstu man yàlla def na gëstu naa ci sama def naa ci mémoire DEA université ci aflatoxine boobu |
|
bokk na ci li ñu wane ne ci li ñuy tuddee bonne pratique bu ñu jëlee dakasa googu di ko retourné maanaam di ko di ko wëlbati ba taat wi féetee kaw bu ko naaj wiy lakk gis nañ ne dina wàññi dooley aflatoxine bi ci biir gerte gi mooy feebaru saabu bi |
|
te ñëpp xam ne aflatoxine lu xaw a lu ñu xaw a sonal la donte ne tey jii sax alhamdulilah am nañ ci ab pexe boo xam ne bu tëru ci xam-xam bu ñuy wooyee %e enrobage tey jii aflaxine bi boo xoolee Sénégal ñu ngi koy defar |
|
te am nay jamono amu fa woon léegi gis nañu ñu ngi koy defar mu ngi tas ci tool yi loolu bokk na ci li nga xam ne ci luy xeex aflatoxine bi la waaye nag ci wàllu it li nga xam ne béykat bi mun na ko def mooy ci bonne pratique gis nga séchage bii nga xam ne moom lay def maanaam bàyyi dakasa yi noonu bu koy naaj wi di ko lakk |
|
mu koy wëlbati mu koy lakk balaa mu koy def naaf gis nañ ne am na njeexital ci xeetu saabu boobu noonu |
|
xam nga loolu am solo la donc ci loolu loolu la ñu toll |
|
waaye leneen li boo xoolee boo boo xoolee ñoom ñoom sëñ Maodo dañuy lu ñu tuddee tawu hors saison bu xawee am ak gerte gi nga xam ne vague yu njëkk yi boobu aussi mun na am jeexital ndax day am lu ñu tuddee saxaat te doonul li gën |
|
mooy regermination loolu it dañ koy xaw a %e xaw a xaw a lifin moo tax moo tax béykat yi da ngay gis ñuy njëkkante ci vague bu njëkk bi gis nga ñu daal di koy deqi ndax dañuy bañ mu regermer waat maanaam mu saxaat bu fekkee ne am na ay taw yoo xam ne liñ tuddee taw hors saison nga xam ne moom it dafay am |
|
**** waaye boo xoolee njeexital bi fi mu gënee amee solo mooy li jëm ci gàncax gi demee ni ki basi fi mu toll nii boo génnee da ngay gis toolu basi yi ni ñu ni ñu naatee |
|
nga xool pastèque bi xaal bi te boo xoolee ci xaal bi am na loo xam ni %e dinañ ci sant ñoom Maodo ci ab doxalin bis boo xoolee liñ njëkk a ñëw ci marché bi ci wàllu mbéyeef xaal lay doon |
|
ñu bëri ñu ngi naan fan lay jógee fii lay jógee rawatina arrondissement Niakhar bii te loolu ci liggéeyu ñoom Maodo dégg ngeen ne li ñu tuddee seen GTP |
|
nee na ab kuréel boo xam ne di dajale béykat di waxtaan ak ñoom ci lañ gis ne waaw dañ nekk ci changement climatique bi kon nañu defi pexe donc pexe boobu si ñoom Maodo la jógee ba mu law |
|
moo tax ne am na ñoo xam ne am na ay du ñu tudd tur waaye am na ci ñoo xam ne buñ déggee ñuy wax dinañ xam ne ne ñoom ñoom %e ñu ngi leen di ñu ngi leen di gërëm santaale ci suuf santaale |
|
ñu dem ci ba gis ne nekk na lu am solo ndax xaal boobu di teel a ñëw ci wàllu koom day fay maanaam mooy gën a rentable que bu demee ba xaal yëpp ñorandoo daje ci marché bi |
|
te lu am solo la ci xalaatu li ñuy tuddee résilience maanaam utub pexe loo xam ni ngir gën a ñoŋal béylat bi yokk poosam yokku pexeem ba nga xam ne %e bu amee choc li ñuy tuddee choc climatique |
|
maanaam taw yu yéex taw yu lifin mu mun a bëyandoo lu bëri njëkkee lii teg ci lii teg ci lii boole lii li ñuy tuddee diversification pour mën cee génn ci wàllum am sécurité alimentaire |
|
ci wàllu it koom doon na donc duunal gafaga ji ci wàllu ci wàllu koppar loolu pexe la ci moo tax gis nga pastèque bi dafa teel a ñëw moo njëkk ci marché bi |
|
te ba léegi mu ngi ci maanaam lay nawet ba léegi dugg si na am na lu xuus dem ca noor ba loolu ndox mi moo koy def te ndox mi da koy lay bi mooy dikk lay bi continué la ca des jëm ci basi ba jëm ci xaal bi wala jëm ci sëb |
|
sëb yi ñu di ko mais lay lay dafa am lu muy def ci ci |
|
*** ahakay lay ndox la |
|
taw ndox lay geneen xeetu ndox la glace geneen xeetu ndox la ndox ci ay formes am yu bokkul la benn bu ne ak la ko tax a jóg |
|
donc lay bi dafa am njeexital da ngay gis fi mu toll nii boo génnee ci bitti da nga gis toolu xaal nga dem xaal day màgg lu koy màggal bu taw bi arrêté taw bi noppee du lay kon lay ndox la |
|
mu ngi def liggéeyam basi mu ngay def liggéeyam si basi ba def liggéeyam ca ñe() sa sëb sa moo tax gis nga sëb si bu tàmbalee nga gis dañ koy witti lu bari ba ca kanam ndax moom floraison continue lay def da ngay witti bàyyi ko mu jebbiwaat nga wittaat bàyyi ko mu jebbiwaat bu lay bi taxawee mu taxaw |
|
basi bi it lay bi dina ko yóbbu ba mu ñor xaal bi it da ngay gis ñu njëkk ña ñi ne ci digg bi ak ñi mujj yëpp day kii bi moo koy yeggali lay bi kon lay bi dafa am moom tam |
|
lay boobu ci dakasa yi bu ñu ko bàyyiwoon détourné wuñ ko naaj bi lakk ko moom it day boole day def li ñuy tuddee day favoriser maanaam day yokk day gaawal màggaayu champignon bi nga xam ne moom moo indi feebaru saabu yi looloo tax ñu koy di ko reourné maanaam di ko wëlbati bàyyi ko ci naaj wi mu lakk ko |
|
bu ko naaj wiy lakk loolu day wàññi doole doomu jangoro yi |
|
mooy afla() Aspergillus Flavus noonu la doomu jangoro ji tudd mi nga xam ne moom mooy indi feebaru saabu boobu ci gerte |
|
ndax ñaari yoon la koy xeex |
|
maanaam da ko njett ci gerte gi balaa ñu ko koy deqi soo ko deqee pare daf koy topp te fu mu koy topp mooy ci dakasa yi di ko xaar ca naaf ba léegi nag gis nañ ne tàngoor boobu it am na yeneen xeetu xeex yoo xam ne xëy na bis bu ñu demee ba ñu war a waxtaanee lu jëm ci feebaru saabu bi dinañ ci gën a mun a xuus |
|
am na solo %e Chacun avec %e son domaine ah vraiment domaine bi defe naa |
|
waaw ne moom moo ko gën gën a maitriser |
|
mais Maodo dafa am foo xamante ne wax na ko sànq muy information climatique |
|
tey lan lay def ci mbey mi dafa mel ni %e ñoom mënuñoo dem sans yéen waaye yéen it mënuleen a dem sans ñoom |
|
loolu moom mooy li wér vraiment li ñuy wax partenariat gagant gagnant moom mooy li nga xamante ne bii moom moo nekk diggante météo ak waa agriculture |
|
que damay dellu si rek léegi ci lu gën a gàtt rek ci li mu wax fii mu nekk nii ah xam nga nee na actuellement nii ñu ngi nekk ci période kii quoi récolte |
|
gerte gi fu mu nekk nii dañu ko ngar bu dee dugub ji dañ ko takk def ko ay pot yu ndaw |
|
dégg nga ba pare nag léegi ñu ngi dox di am na ay techniques yi nga xam ne dañ koy def di fi teg di ko wëlbati di ko wëlbatiwaat xam nga loolu lan lañ ci bañ ah luñ ciy bañ en réalité mooy bu fekkee am nañ ay taw yi nga xamante ne bii c' est des pluies hors saison dégg nga mu créé ci kii quoi problème parce que bu fekkee léegi yow da nga %e deqi sa gerte nga daal di koy naaf directement ak humidité bi nga xamante ne nii moom mooy am noonu gerte gi dafay dafay kii quoi dafay xuur day saabu ngooñ bi aussi dafay xuur |
|
léegi yow non seulement dootoo ko mën a jëriñoo mais jur gi aussi duñ ko mënati * parce que bu ñu ko lekkee dafa leen di créé ay problèmes mu %e d'a ordre %e kii quoi gastrique |
|
dégg nga ah loolu loolu dafa nekk benn benn benn aspect ñaareel bi ma bëgg %e dëggal tuuti ci li mu waxoon léegi ci li jëm ci mbirum kii quoi xaal bi wala kii quoi ñebe ji nga xamante ne nii actuellement ñu ngi continuer donc %e di ko béy |
|
c' est vrai que ñu ngi koy récolté mais fur et à mesure ñu koy récolter dañuy gis ne encore dafay continuer donc di saxaat |
|
te xam nañ ni taw jeex na donc lan moo koy saxal pourtant ndox la mais ndox yooyu moom moo wute |
|
xam nga %e ndoxu taw nuage bi nga xamante ne bii moom mooy indi moom mooy indi taw ak niir bi nga xamante ne bii moom dafay indi %e souvent naka lañ koy waxee encore lay wala broullard dañoo bokkul |
|
même booy xool seen kii quoi ci seen constitution physique sax donc duñ du ñu kii quoi du ñu benn ñaare taw taw taw kii quoi ndoxu taw nuage bu koy indi souvent %e association ndox ndox yi nii lay nekk bu ànd ak kii quoi bu ànd ak ay cristaux glaces |
|
mais souvent bu fekkee %e kii nga am nag léegi %e lay lay nga am kooku yeneen façon nuage yi nga xamante ne bii ñoom ñooy ñoom ñooy kii quoi ñoom ñoo wàcc kii quoi ñoom ñooy changé disons de niveau wàcc ci suuf * kii bi quoia |
|
mais souvent bu fekkee %e kii nga am nag léegi %e lay lay nga am kooku yeneen façon nuage yi nga xamante ne bii ñoom ñooy ñoom ñooy kii quoi ñoom ñoo wàcc kii quoi ñoom ñooy changé disons de niveau wàcc ci suuf * kii bi quoia donc fee da ngay jàpp ni affaire bi dafay am %e dafay kii quoi dafay desengragé wu parce que da ngay am forte pénétration de particule kii quoi pluviogéneux dégg nga nga xamante ni bii bu bu amee ak tàngaay bi nga xamante ne bii moom la moom la moom moomdisons moom la %e naaj bi di kii quoi di généré |
|
donc da ngay sentir que ni ndox mi kii quoi nuages yi dañuy gën di dañuy gën di ubbeeku goutelettes d' eau yi dañuy gën di tàng au fur et à mesure ñuy gën di tàng dañuy gën di màgg nu muy gën di màggee dafay gën a diis |
|
am na fi nga xamante ne bii ay précipité donc taw boobu bokkul |
|
ak li nga xwamante ne bii moom la ñu yàgg di d' aillers je dis bien d'a aillers booy xool %e fin hivernage |
|
lay %e que ça soit la rosée wala muy le broullar nekk na ay signes yi nga xamante ne bokk na ci signes yi nga xamante nefoo ko gisee rek xam ne nawet jeex na parce que ñoom ñaar bokkuñu bokkuñu *** |
|
donc man suñu émission bee passé |
|
bi may taxaw naan leen bon nawet bi jeex na c' est parcea que boobu daa mel ni commencé woon na absorbé broullard comencé woon na absorbé brute humide commencé woon na absorbé rosée |
|
ñett yooyu yëpp nag ay xeetu lay lañu mais bokkuñu booywax rosée mooy bi nga xamante ne bii da ngay xëy lea matin rek gis oto bee garré wala nii wala bois bi nga xamante ne gis nalayu bi wàcc si moom mu tooy xepp xepp xepp xepp |
|
bokkul ak brut humide bi nga xamante ne bii da nga ko observé nii ci ay benn distance bi nga xamante ne quatre wala cinq kilomètres lay nekk |
|
bokkul ak broullard bi nga xamante ne bii moom dafay nekk distance bi nga xamante ne bii peut être entre %e trois cent lay nekk ba sept cent ba huit cent mbaa lu ko ëpp |
|
donc visibilité yi souvent moom mooy visibilité gi quoi horizontale bi moom mooy li nga xamante ne biimooy def kii quoi souvent la différence |
|
mais ñu jàpp rek ni lay lay lay bi ñetti façons lay moo am am na lu tubaab di wax rosée am na lu ñuy wax brut humide am na lu ñuy wax broullard |
|
ñett yooyu foo ko gis rek xamal ni nawet bi jeex na mais nawet bu jeexee bu continué di ñëwdootul mën a %e suuxat gerte du mën a suuxat dugub mais par contre xeetu meññeef yu mel ni ay ñebe wala ay xaal yooyu nga xamante ne bii soxlawuñu kii quoia ndox mu bëri yooyu moom moom moom moom la kii quoi moom la xeetu layu yooyu amal njëriñ |
|
présentement ñett yooyu ñett yooyu am nañ ko fii ci Sénégal |
|
présentement nii fan yii yëpp matin bu ñu xëyeemoom la ñu am |
|
bu boo koy seetlu boo yeewoo suba oto bu ma fekk mu taxaw nii dafay lay ba tooy xëpp xëpp xëpp |
|
benn bois boo ko gisoon nii ci mbed mi fu mu nekk nii boo xëyee le matin rek boo ko ñëwee da ngay fekk day tooy xepp vitres yi day tool yow sa bopp booy dox fi ngay jaar mel ni dafa taw ba pare te pourtant |
|
taw taw amul mais lay bi moom moo moo am quoi ni muy tooyee noonu nag loolu moom mooy li nga xamante ne bii moom la xaal bi soxla présentement moom la ñëpp di soxla |
|
moo tax %e comme ni ko monsieur Badiane waxeewoon ñi nga xamante ne bii ci njëlbeen bi dañu %e indiwoon ay projets d' adaptation changement climatique |
|
daal di song ay mbéyum xaal ba amoon ci lu kii quoi lu mucc ayib kooku wax nañ ci waxati waxaat nañ ci yaakaar naa ni dootuma ci dellu si |
|
ñooñu présentement ñoom ñoo labouré |
|
ba actuellement nii ñu ngi ci seen deuxième semis wu xaal ci ci la saison là actuellement xaal boobu sax na mais fu mu nekk nii léegi %e lay bi moom mooy bi nga xamante ne bii moom moo koy ñoral |
|
te dinaa dégg ci wolof yi di wax sax naan xaal boobu d' habitude moom moo gën a neex bi nga xamante ne bi moom mooy ñor ci biir kii bi quoi ci biir nawet quoi |
|
mais ndax jangoro yi nga xamante ni dañ koy nemmeeku ci mbey mi dafa am rapport ak li nga xamante ne moom mooy changement climatique yi |
|
tout à fait am na bëri na ay ay ay ay ay ay jangor yuy ja() jangoro yi nga xamante ne bii dafal dal gàncax gi |
|
souvent bon changements climatiques yi bokk nañ ci bëri na ci am na ci par exemple ay genre yenn genre xeetu %e kii quoi sauterelles ay sauterelles ñu koy wax cri() criquet ***** |
|
am na ci yi nga xamante ne bii ñaare ñàkk taw moom moo koy moo koy indi mais la plus part bu tawee rek day gis dafay ànd ak taw bi daal di kii quoi lessive bi mu dem quoi |
|
am na ay gunóor yi nga xamante ni tamit dañ fi nekk souvent ñoom tamit bon dañuy ànd ak kii quoi climat boobu |
|
ay compagnons yooyu yi nga xamante ne bii souvent dañuy ànd bu climat bi xonkee ñu xonk ànd ak moom |
|
bu weexee tamit ñu daal di %e daal di kii quoi dem quoi |
|
mais comme loolu mbirum DPV la je préfère monsieur Badiane moom mi nga parce que moom moo ma gën a maitriser kii bi kii quoi domaine boobu quoi |
|
d' accord balaa ñuy dem ci question bi rek |
|
waaw waaw waaw maanaam ci %e gën a pro() %e gën a dooleel li Maodo wax |
|
maanaam dafa maanaam dafa am lu ñu tuddee paramètres climatiques yoo xam ne day bokk maanaam foog mu ñëw li ñuy tuddee température ak humidité |
|
bokk na ci li nga xam ni ñoom ñooy yokk wala ñu wàññi maanaam ñooy dooleel mbaa ñu néewal doole màggaayu doomu jangoro maanaam ma jox la misaal gis nga fi mu toll nii boo duggee ci toolu dugub bi foofu Maodo nga xool deuxième vague bi wala * da ngay gis am na lu mel ne ay ronkoñ lay doon da ngay gis mu mel ne gomme boo demee ci tool yi nga xool ni %e dugub ji bëri na ci |
|
mooy li ñu wax noonu maanaam ci ci ci ñi fa fa fa ni taw bi bindoo moom moo ko yokk moom lañ tuddee l' ergot du mil noonu la tudd maanaam maladie ay champignons la fongipte |
|
charbon bi it boo xoolee bëri na mooy li nga xam ne boo ko defee da ngay gis am puudar bu génn day yàq guub bi ba nga xam ne buy génn day def lu mel ne ab pucantaan bu verte mais boo defee boo *** couleur bu ñuul mooy génn mooy *** champignon bi |
|
xam nga kooku bu bëree ci guub kooku munoo munat() boo ko kiwee boo ko bojjee mun munoo ko def cere |
|
yenn produit it bu ci bëree ba jël guub bi yëpp daanaka da koy yàq |
|
kon xam nga ne day wàññi bu baax la nga doon am ci rendement boo xoolee %e li mu wax noonu %e dundu yenn bàyyi ma yi * maanaam sauterelles yi mooy soccant yi da ngay gis ne bu nawet bi lifinee ñu ne waa ana soccant yi maanaam balaa ñuy lifin dañuy bàyyi nen yi bu ñu nenee dañu koy gas suul ko ci suuf ba ko foofu muy dund |
|
yàlla nag xam nga dafa bëri kéemaan ndax nen bi dafa am lu koy ëmb ba nga xam ne fu mu tegu maanaam tàngoor yi ñuy fàttali ne boo xoolee ci suuf nii comme ni ñu tàng na ci kaw soxna si malgré si suuf moo gën a tàng man ci gëstu bi ma doon def ci liggéey dafa am ay sondes yuñ doon dugal ci suuf di natt tàngooru suuf si di natt tàngoor wi ci kaw ak humidité bi ci kaw |
|
waaye Maodo boo ko defee |
|
comme yeneen services yi gis naa kay ñoom ñu koy def %e |
|
régulièrement jërëjëf bu ko defee da ngay gis ne tàngoor waaye nag lu tax nenu soccant yi du yàqu li lay wan ne kéemtaanu borom nen ba dafa am lu koy ëmb loo xam ne moo koy protéger téye d' accord moo koy protéger mu am ñu mun a survivre noonu |
|
waaye nag nga gis bu nawet bi jotee rek nga gis ne bu ndox laalee suuf rek nga gis |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.